• Votre panier est vide.

N1T1 – Prononciation ​



Dans ce chapitre nous allons voir la prononciation de ces mots suivants en wolof.


  • Fatu ( fatou) : Yow xana amoo mag wala ràkk ? = Es-tu fille unique ?​


  • Penda : Am na kay, juróom la nu sunu kër. = Non, nous sommes 5 personnes à la maison.​


  • Fatu : Nun ñeent la nu. = Nous, nous sommes 4.​


  • Penda : Kan mo fa nekk ? = Il y a qui ?


  • Fatu  : Sama baay, sama yaay ak sama ràkk ju góor. = Mon père, ma mère et mon petit frère.​


  • Penda : Man tamit, samay wayjur ak sama ràkk ju jigéen ak sama mag ju góor. = Moi aussi, il y'à mes parents, ma petite soeur et mon grand frère.

 ​

  • Fatu : Kon sa mag ji moy taaw ? = Donc c'est ton grand frère qui est l'ainé​


  • Penda : Waaw kay yow jëli nga. = Voilà toi tu comprends.
 
Copyright Wakalingo © Développé par Keli Groupe

Configuration des menus dans le panneau d'administration